Woote, ku nekk ak làkku ndeyam

Yónneel liyeŋ bi ki ngay woo: soxlawul mu bindu, soxlawul mu samp dara; lépp dafay jaar ci yoon bu ñu tëj ak caabi, te sa sutura dencu na.